Clip / Paco Ben Boy Dans Lou Waral Thiow Li

1er Couplet

Job bou nice nanga ko xaar fils Yéékhi bagass melni Slampee MC xawma kagn nga takk mais homie diapal ni yow fayna sa lampes yi Fils ghetto negger dafa tar fils Té boys yeupeu beugeu tékki Deukoulo fi danga fi gané sii wakh ma homeboy lan ngay def fii Seutou Ceddo ba si nimay bindé day yomb ma wathié la 16 bars Mandikat nga consal daaj bi damla romb homie fek c’est trop tard Manla Lat Dior Mama Diakhou Ba Cadior Cadior beugue Bamba Heure bi diotna temps bi sonner na Nieuweul séédé kone melni Buur Sine Adiowoul wakh ni la guéwél la Tagg séni maam melni Diallo Pape Cheikh Sa deugg deugg dama si fier ni Mansour Mbaye Hey manla Mbaye Pékh Armer gun bi rindi noonbi Xall yoon bi dawal negger man police yow la Satan Domou Iblis sacrifier la yaak say fétiches Talibé bi tangal kogn bi yow bang bang