Pape Sidy Fall je veux encore plus de Nitdoff dans le hip-hop Sénégalais

Merci au public du hip-hop galsen merci Pour l’accueil merci pour le show mais aussi un merci à NITDOFF je veux encore plus de nit dof dans le hip-hop sénégalais ma Fatali li ma waxone rek démb Rek Macky néna rén Xaliss bi dina ko Yok dé ba 600Millions 😂😂😂😂 légui Mom kou Yabou dém déglou pathianga rek hannn bilay avec 300millions du contribuable sénégalais il a réussi à fermé les plus grande gueule du hip-hop mdrrr non mais imaginél 600millions yi nak a condition mou falouwat leu donc tu la ferme tu récolte ta part du gâteau Mdrr am na rappeur bou waxone ni dara dagnou lek sougnou Wal rek Sénégal thiow doufi RomB wér mo takh doumalen Faté si Fatali bi en passant élection présidentielle 40jours Mossi desss Batay hip-hop ba nguiné ték bon dimanche ( Message de Pape Sidy Fall sur facebook après le show of the Year 2018 )

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *