Clip : Découvrez le nouveau clip Niou Dem Mairie de OMG

Voici le tout nouveau clip Niou Dem Mairie de OMG

Auteur : Kruh Mandiou Mauri Compositeur : B.Beut Producteur Exécutif: DD Records Distribution : Believe Digital Directed by: Awanje Films

LYRICS

Bokoulok gniy door Li goor yi di bari bari amo thi dé dénda ndo Léme bougnou soukeur Kouko xass moss daal Dou yombeu bayi ko Yaw danga meune mine mokal jiguéne Mani danga rax ndax li dou néne HOOK Beut yi gueuthie na taa ndax yaw Xol bi deuké naate ndax yaw Yéndo di rétaane ndax yaw Namuma greffage ndax yaw Faléwuma maquillage ndax yaw Diotna gnou mariage maak yaw REFRAIN Baby kaay gnaane si Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi Lima beug moy niou dem mairie Dem mairie niou dem mairie (2x) Yaye sama titi tara pararapa para para Li mbeuguelou moumeu le diaroul di wax ndax yaw mi xam nga Laadiou ma aye milliard Kilo gouro nga ame diabar Kone légui lane ngay xaar Gnoune jiguene seuy moy suñu taar HOOK Beut yi gueuthie na taa ndax yaw Xol bi deuké naate ndax yaw Yéndo di rétaane ndax yaw Namuma greffage ndax yaw Faléwuma maquillage ndax yaw Diotna gnou mariage maak yaw REFRAIN Baby kaay gnaane si Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi Lima beug moy niou dem mairie Dem mairie niou dem mairie (2x) Yangui dape sama banekh Di fathie samay adio Xam di def lila war bolèwo darak thioy wayè wayè am na lou dess niou dem mairie (x4) Baby kaay gnaane si Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye Lima beug moy niou dem mairie Dem mairie niou dem mairie (2x)