Clip : Découvrez le Nouveau Clip Wëy wallú de Leuz Diwane G

1st couplet Incompetence meunoul dokhol rew Sou niou confiance sopi nguene ko new Sene arrogance Sa tass si rew mi rew Trop de défaillance Sa takh fou né niou ngui latchté lou khew Rest in peace Doctor Cheikh Anta Diop Rest in peace Dia Mamadou Nioune dè tiiiiiiiiiiiiss Reka la niou Gaup Kou guessou guiss Nakhar bi niouy yendoo Kou nieuw ba nga fog nè mo tanè fekeu mo gueuna yess Ray nio ki discours defarou kheuy nè mess Raylè la dialè la sakhami ko mou ress Jouer niou ay sale Tours Dou fi lou bess Let’s everybody be aware nelaw yi da doy fog niou khipi khol Let’s everybody be aware ligne niou diapè nèkhoul si khol